11 novembre 1902, retour d’exil de Cheikh Ahmadou Bamba
La date du 11Novembre1902 marque le retour d’exil de Cheikh Ahmadou Bamba.
Jugé le 5 septembre par l’administration coloniale, Serigne Touba devait être enfermé dans la prison de Saint-Louis avant sa déportation, le 20 septembre 1895.
Il sera ainsi envoyé au Gabon, dans la forêt ténébreuse et abiotique de Mayombe.
Le Cheikh n’en sera pas démotivé pour autant. Il subira dignement les épreuves que lui imposaient les colons, apeurés et ameutés par son influence.
Pendant son absence, son aura ne fera que s’accroître avec le travail gigantesque de Mame Thierno Birahim Mbacké qui assura son intérim.
11.11.1902 – 11.11.2021 (119ans)
Commémoration du Retour en Exil au Gabon ?? de Cheikh Ahmadou Bamba Xaadimu Rassul.
Woy wu gàtt nu jagleel ko
Seex Ahmadu Bàmba Xaadimu Rasuul…
Aji-bind ji : Allaaji Jibi Séy – Daara yi
Siggil na Senegaal ak nit ku ñuul
Defar na jullit bu weex ak bu ñuul
Laabal na xol yu tilimoon ba ñuul
Maa ka yéemu ci Xaadimu Rasuul
Muriid dëgg dafay deñ ci làmbatu
Ndax Haqiiqaa tax mu def aslamtu
Di dox ci tasawuf booleek Sariyatu
Làmboo yar ak teggin fonk Sunnatu
Ku bëgg a mos ci lu mu yor, la ko war
Mooy def ni Seex Ibra doon ku sawar
Doo moy doo fo, fasu ndigël ngay war
Yàlla gërëm la bijaahi boroom 18 safar
